Simi

From Wikipedia, the free encyclopedia

Remove ads

Sunu dund gi, niki gu dundat yi ak gu gàncax, dafa wéeru ci jurdund, mooy xeet wu simi wi ëpp ci jéeri ji. Jurdund nag nekkul rekk ci ngelaw li, waaye ci jaxasoo gu mu jaxasoo ak yeneen xeet yi ci anam gu wuute te bokkadi, mi ngi ci lu ëpp ci ne-ne yi ñu baaxoo dund ak ñoom ak a jonjool.

Xalaatal rekk ne xeet yi toggale ndox mi, bu ñu doon fukk lañu juroom ñatt yi jurdund lañu, te moom jurdund moomu moo toggale li ëpp ci doj yi.

Jurdund dinanu ko faral di jëfandikoo nii:

- Def ko ci bitéeli gaas yi, ngir dagg, suude ay weñ ak tàkk-tàkk lu Osidrik walla Osiyasetilenik liy jariñoo tàngoor wiy amu ci sawara wu jurndox ak wu Acetilin.

- ci liggéeyiinu mbell yi nga xam ne danu cay jëfandikoo ngelaw lu nu woomal ak jurdund.

- ci paj ngir yombal noyyig ñu tawat ñi.

- niki taalukaayu jum yi: fii moom jurdund bu yolaakon bi lañu fiy jëfandikoo ci tàngoor wu suufe.


Xam-xam
Xam-xam
Gëstubiddiw | Jëmm | Paj | Saytubiddiw | Simi | Xam-xamu suuf si ak jawwu ji | Xayma
Xarala
Jokkoosoryante | Xaralaymbëj | Doolerandu | Kàttan | Xam-xamu nosukaay | Mbëjfeppal
Xam-xami nite ak mboolaay
Diine | Melosuuf | Wërlaay | Nit | Yoon | Koom-koom | Taariix | Xeltu | Kàllaama
Remove ads

Wikiwand in your browser!

Seamless Wikipedia browsing. On steroids.

Every time you click a link to Wikipedia, Wiktionary or Wikiquote in your browser's search results, it will show the modern Wikiwand interface.

Wikiwand extension is a five stars, simple, with minimum permission required to keep your browsing private, safe and transparent.

Remove ads