From Wikipedia, the free encyclopedia
Benin (Republik bu Benin) : réewu Afrig.
Réewum Benin | |||||
| |||||
Barabu Bene ci Rooj | |||||
Dayo | 112 622 km2 | ||||
Gox | |||||
Way-dëkk | 10 448 647 (2015) nit | ||||
Fattaay | 91 nit/km2 | ||||
Xeetu nguur - Njiitu Réew - Njiitu Jëwriñ |
- Yayi Boni - | ||||
Tembte - Bawoo - Taariix |
|||||
Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |
Porto-Novo | ||||
Làkku nguur-gi | Nasaraan | ||||
Koppar | Franc CFA (XOF) | ||||
Turu aji-dëkk | -Bene-Bene -Sa-Bene | ||||
Telefon | |||||
Lonkoyoon bu Bene |
Bene aw rëdduw suuf wu sew la, nekk ci diggante yamoo gi ak Gëwéelub Sànkar bi. Rëddu tus-wu-gaar wu bene mi ngi ci diggante 6°30'bëj-g ak 12°30'bëj-g, tu-wu-taxawam moom mi ngi ci 1° P ak 3° 40'P. Ay digam ñoo ngi yem ci Togóo ci sowwu, yem ci Burkina-faso ak Niseer ci bëj-gànnaar, ci Niseeriyaa ci penku, janook mbàmbulaanug Atlas gi ci bëj-saalum. Mi ngi am yaatuwaay bu tollu ci 112.622 yu kaare. Bene ngi bawoo ca dexug Niseer gi ci bëj-gànnaar yem ci mbàmbulaanug Atlas ci bëj-saalum ci ag tallalug 700 km. Diggante bi gën a guddu ci réew mi 325 km la.
Réewi afrig |
Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkina Faso • Buruundi • Cadd • Ecoopi • Eritere • Eswatini • Gaambi • Gaboŋ • Gana • Gànnaar • Ginne • Ginne Bisaawóo • Ginne gu Yemoo • Isipt • Jibuti • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Keeñaa • Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Lesoto • Libeeria • Libi • Madagaskaar • Malawi • Mali • Marook • Móoris • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeria • Ruwandaa • Saambi • Sahara gu Sowwu • Sao Tome ak Principe • Senegaal • Seysel • Simbaawee • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Sudaan gu Bëj-saalum • Tansani • Togóo • Tiniisi • Ugandaa
Seamless Wikipedia browsing. On steroids.
Every time you click a link to Wikipedia, Wiktionary or Wikiquote in your browser's search results, it will show the modern Wikiwand interface.
Wikiwand extension is a five stars, simple, with minimum permission required to keep your browsing private, safe and transparent.