Gox Adduna Asi mooy réewum gëna mag[note 2][11][12] ci àdduna bi ci wàllu suuf ak askan.[ 12] Dafa am lu ëpp 44 milyoŋ kilometri kare, lu tollu ci 30% ci àll bi ak 8% ci àll bi. Bennoo bi, bu yàgg a nekk kërug mbooleem mbooleem nit ñi, [1] moo nekkoon bérab bu bare bu jëkk bi. Réew mi am 4.7 milyaar ci nit[14] di lu tollu ci 60% ci askanu àdduna bi, am na lu ëpp ci nit ñi ci yeneen àdduna yépp.
Diiwaanu Nguuru Room
Turi Réew yeek seen raaya | Rëyaay (km²) |
way-dëkk (1 sulet 2002) |
Fattaay (ci km²) |
Péey |
---|---|---|---|---|
Diggu Asi: | ||||
Kasakistaan[1] | 2,346,927 | 13,472,593 | 5.7 | Astana |
Kirgistaan | 198,500 | 4,822,166 | 24.3 | Bishkek |
Tajikistaan | 143,100 | 6,719,567 | 47.0 | Dushanbe |
Turkumenistaan | 488,100 | 4,688,963 | 9.6 | Ashgabat |
Usbekistaan | 447,400 | 25,563,441 | 57.1 | Tashkent |
Penku Asi: | ||||
Siin[2] | 9,584,492 | 1,384,303,705 | 134.0 | Beijing |
Ooŋ Koŋ (China)[3] | 1,092 | 7,303,334 | 6,688.0 | — |
Sapoŋ | 377,835 | 126,974,628 | 336.1 | Tokyo |
Makaaw (China)[4] | 25 | 461,833 | 18,473.3 | — |
Mongoli | 1,565,000 | 2,694,432 | 1.7 | Ulaanbaatar |
Kore gu Bëj-gànnaar | 120,540 | 22,224,195 | 184.4 | Pyongyang |
Kore gu Bëj-saalum | 98,480 | 48,324,000 | 490.7 | Seoul |
Taaywaan [5] | 35,980 | 22,548,009 | 626.7 | Taipei |
Bëj-gànnaaru Afrig: | ||||
Isipt[6] | 63,556 | 1,378,159 | 21.7 | Cairo |
Sibeeri: | ||||
Riisi[7] | 13,115,200 | 39,129,729 | 3.0 | Moscow |
Bëj-saalum-penku Asi:[8] | ||||
Brunaay Daarusalaam | 5,770 | 350,898 | 60.8 | Bandar Seri Begawan |
Kamboodi | 181,040 | 12,775,324 | 70.6 | Phnom Penh |
Endoneesi[9] | 1,419,588 | 227,026,560 | 159.9 | Jakarta |
Lawos | 236,800 | 5,777,180 | 24.4 | Vientiane |
Maleesi | 329,750 | 22,662,365 | 68.7 | Kuala Lumpur |
Miyanmaar | 678,500 | 42,238,224 | 62.3 | Naypyidaw[10] |
Filipiin | 300,000 | 84,525,639 | 281.8 | Manila |
Singapoor | 704 | 4,483,900 | 6,369.0 | Singapore |
Taaylaand | 514,000 | 62,354,402 | 121.3 | Bangkok |
Timoor gu Penku [11] | 15,007 | 952,618 | 63.5 | Dili |
Wiyetnaam | 329,560 | 81,098,416 | 246.1 | Hanoi |
Ron-goxu End: | ||||
Afganistaan | 647,500 | 27,755,775 | 42.9 | Kabul |
Banglaades | 144,000 | 133,376,684 | 926.2 | Dhaka |
Butaan | 47,000 | 672,425 | 14.3 | Thimphu |
End[12] | 3,167,590 | 1,045,845,226 | 318.2 | New Delhi |
Iraan | 1,648,000 | 68,467,413 | 41.5 | Tehran |
Maldiif | 300 | 320,165 | 1,067.2 | Malé |
Nepaal | 140,800 | 25,873,917 | 183.8 | Kathmandu |
Pakistaan | 803,940 | 147,663,429 | 183.7 | Islamabad |
Siri Laanka | 65,610 | 19,576,783 | 298.4 | Colombo |
Penku gu Diggu, Penku gu Jege | ||||
Armeeni[13] | 29,800 | 3,330,099 | 111.7 | Yerevan |
Aserbayjaan[14] | 46,870 | 3,845,127 | 82.0 | Baku |
Bahrayni | 665 | 656,397 | 987.1 | Manama |
Ciipër [15] | 9,250 | 775,927 | 83.9 | Nicosia |
Palestiin: Gaza[16] | 363 | 1,203,591 | 3,315.7 | Gaza |
Jeoorji[17] | 20,460 | 2,032,004 | 99.3 | Tbilisi |
Iraak | 437,072 | 24,001,816 | 54.9 | Baghdad |
Israayil | 20,770 | 6,029,529 | 290.3 | Jerusalem[18] |
Jordaani | 92,300 | 5,307,470 | 57.5 | Amman |
Kowet | 17,820 | 2,111,561 | 118.5 | Kuwait City |
Libaan | 10,452 | 3,677,780 | 353.6 | Beirut |
Omaan | 212,460 | 2,713,462 | 12.8 | Muscat |
Kataar | 11,437 | 793,341 | 69.4 | Doha |
Araabi Sawdit | 1,960,582 | 23,513,330 | 12.0 | Riyadh |
Siri | 185,180 | 17,155,814 | 92.6 | Damascus |
Tirki[19] | 756,768 | 57,855,068 | 76.5 | Ankara |
Imaaraat yu Araab yu Bennoo yi | 82,880 | 2,445,989 | 29.5 | Abu Dhabi |
Palestiin: West Bank[20] | 5,860 | 2,303,660 | 393.1 | — |
Yaman | 527,970 | 18,701,257 | 35.4 | Sanaá |
Total | 43,810,582 | 3,902,404,193 | 89.07 |
Ci angale ak ci faranse mooy Asia.
Asi dafa am ñaari tekki ci Injiil.
- Ci bu jëkk mooy li ñu tudde tey jii 'Asi Minër', maanaam daanaka lépp ci réew mu tudd tey jii Tirki (Turquie) lu fare penku géeju Ese.
- Ñaareel bi, ci jamano Injiil ji, Asi benn diiwaanu nguuru Room la woon. Moo doon wàllug sowu Asi Minër. Dafa boole diiwaani Misi, Lidi, Kari, ak genn wàll Firisi, ak dun ya nekk ca géeju Ese. Waa Room ñoo ko def diiwaan ci 129 j.K.. Ci bu jëkk péeyam moo doon Pergam. Waaye, gannaaw jamano Injiil, def nañu Efes ni péeyam. Juróom ñaari dëkk yi ñu gis ca téere Peeñu ma (Pe 2:1-3:22) ñoo bokkoon ca diiwaanu Asi.
Am na ñi xalaat ne yoon bu nekk ñu gis 'Asi' ci Injiil mooy diiwaanu nguuru Room bi. Am na ñeneen ñi xalaat ne léeg-léeg Injiil dafay wax ci ci Asi Minër (Jëf 19:26-27 21:27 24:18 27:2), te yi ci des mooy diiwaan bi.
Man nañu gis Asi ci Injiil ci Jëf 2:9; 6:9; 16:6; 19:10,22,26,27; 20:4,16,18; 21:27; 24:19; 27:2; Ro 16:5; 1Ko 16:19; 2Ko 1:8; 2Tim 1:15; 1Pi 1:1; Pe 1:4.
Karmat ak delluwaay
Xool it
Wikiwand in your browser!
Seamless Wikipedia browsing. On steroids.
Every time you click a link to Wikipedia, Wiktionary or Wikiquote in your browser's search results, it will show the modern Wikiwand interface.
Wikiwand extension is a five stars, simple, with minimum permission required to keep your browsing private, safe and transparent.