Xare b
From Wikipedia, the free encyclopedia
Remove ads
Xare su santee B (xare b) mooy li farañse naan: armée; araab naan ko جيش, àngale di ko wax army.
Niral: Lat-Joor takk na xare bu màgg ngir xeex ak tubaab bi.
Xare bu santee G (xare g) xamal ne jëf la, mooy li farañse naan: guerre; araab naan ko حرب, àngale di ko wax war.
Xare ga doxoon diggante jullit ña ak kéeféer ya ca Badar, jullit ña a daan.
Wikiwand - on
Seamless Wikipedia browsing. On steroids.
Remove ads