World Wide Web manees na koo tekkee niki digg lënd gi (lënduk jargoñ) kon ana numu def ba tuddees ko digg lënd ? ndax moom la àdduna bépp ànd di jëfandikoo ku ne jàpp ci génn lawtan fa lawtan ya daje lees tuddee digg lënd moom nag manees na koo jëfandikoo fim ne ci àdduna bi yépp, gox yépp man nañu cee daje, boo jëmee ci ab dal dugal www doora def turu dal ba man naa ñàkk yit ci bu la neexee nde joowkat yu yees yi di nañu nànd sa bëgg-bëgg ba jobbu la, www yii nak limu wund ci wu-angalteer mooy World Wide Web


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Wikiwand in your browser!

Seamless Wikipedia browsing. On steroids.

Every time you click a link to Wikipedia, Wiktionary or Wikiquote in your browser's search results, it will show the modern Wikiwand interface.

Wikiwand extension is a five stars, simple, with minimum permission required to keep your browsing private, safe and transparent.